Artistes: ADMOW & OMG
Lyrics: ADMOW
Beat: Steady Key & Mozart
Recording/Mix/Master: DD Records
Réalisateur Clip vidéo: WEEFLAG
Assistant Réalisateur: Director Yuse
Sponsor Du Clip: MAGIC LAND & 221 LUXURY
Coppa'Belt Empire
PAROLES
Couplet
Nobody wanna see us together (together, yeah)
Nobody wanna see us together but they don’t matter know
Khol Naala khol kénéne
Guiss ni bokouléne
Kone diaroul may déme fénéne
no no no
Yama diokh say coordonnés
Sama Life nga ordonné ko
Kone mane doumala abandonné
Refrain
Kou mélni yow
Moy ki baakh thi mane
Kou melni mane
Moy ki baakh thi yow
Sou goudi khaadié, ba sama khél déme thi yow
Ma khamni i love you yeah yeah...
Sokhnassi i love you yeah yeah...
Couplet
Dma blindé thi niénéne gni
Done Ngaaka thi yow (coz I love you yeah yeah)
Jamdong laala beuggueul, dinga Doundou beu guiss koo (coz I love you yeah yeah)
Oh souka débo yodi, ko ane woni fittandam
Ko oh Modji, sa diali, éné boubna berdame
Ohhh woni sékhilame
Ohhh woni guidélame
Ohhh woni diom soudame, honoma ala no no no
Refrain
Kou mélni yow
Moy ki baakh thi mane
Kou melni mane
Moy ki baakh thi yow
Sou goudi khaadié, ba sama khél déme thi yow
Ma khamni i love you yeah yeah...
Sokhnassi i love you yeah yeah...
Bridge
Loving you is what i do girl (éh aay éh)
Dénio beugueunté ba moudiou niro (éh aah aahh éh)
Kone ane woni é ndér bérndam girl
Halnam saa ndaarikam holko ndiyata
Holma thi ay beute wakhma loy guiss
Sorila baby dinama diss baaaabyyy
Refrain (avec OMG)
Kou mélni yow
Moy ki baakh thi mane
Kou melni mane
Moy ki baakh thi yow
Sou goudi khaadié, ba sama khél déme thi yow
Ma khamni i love you yeah yeah...
Sokhnassi i love you yeah yeah...
Veuillez vous connecter pour commenter