Daara J Family Jamono



dans la categorie WORLD MUSIC
Daaraj family interprète son titre "Jamono" dans les studios de RFI lors d'une session acoustique exclusive pour RFI Musique avec RFI Labo. La chanson est extraite d'un album à venir. Davy Honnet aux drums et Euclides Gomez jr à la Guitare faada Freddy: voix chant Ndongod: voix Rap

JAMONO


LEGLEEG DA MAY BËGG GADDU SAMA LOXO YUUXU METTIT
DAMAY BËG GIVE UP YENN A SAAY
TOLOF TOLOF A KI NATTU YU TAKKU BËG YOBBU SAMA FIIT
XAM NAANE ADUNA DUMA RAAY
COONO DAFAY DEFFAR XOLU DOOMU ADAMA BI CI NGËM
JAMBAT MAYU MA NJEGENAAY
BUUR YALLA REK A XAM LI NEKK SAMA DËNN MAKOY DEKKU
BAÑA JÉNG TA GËM NE GINAW JAFFE JAFFE NOFLAAY
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO

JAMONO KAW LA ÑU JËLEE
XAMUÑ NOFLAY DI NU MBËLEE
RÊVE YU LA SUT AKA KAWE
GÉNT BO FATTE CONNEXION BI DA FA DEM
FOK ÑU AM PASSE DA ÑO CALÉ
DAFMA YEEM ÑAATA JEEM ÑAATA YOON LA ÑU JEEM
YOONU SUUF YOONU NDOX FËGG FU NE FUNUY JAARE
KAN MO NUY JALLE JOTU MA NELAW BIIG YAKAAR GËNË DIIG FOK NU GEN CI
LAN MO NU JIIG ÑAKK PARE CI (JAMONO DI GËNA TËRADI)
LO GÉN KËR GIS ADUNA BI CI ÉCRAN BU TUUTI ACCÉS ILLIMITÉ (WUTI VISA)
LOXO YA NGI CLICKÉ SOURIS YI DÉFILÉ ACTUALITÉ NIMUY DIKKE , BU LA BEN NGELAW YOBAALE
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA

RAKK BUL WORRI DI NGA JEGGI NDOX
BU SOOBE BUUR BI GONE DI NA MAGG BAY DOX
LEPP DI NA BAAX LEPP DI NA BAAX
LEPP DI NA BAAX LE LE LE LEPP DI NA BAAX
DU JIKKO JAMONO LA DU DARA JAAR JAAR LA
BOROM KARAW BU ÑUUL ÑAKKUL DARA DARA JOMBBULA

DARA DARA WARUL JOMB GOOR YALLA BU AM NGËM BU KAWEE
TE NGA JEEMA BAY SA TOOL YALLA DU BAYKAT BUL XAAR FUMUY TAWE
DI NGA GIS SA YOON JAMONO NAQADI TOGAL CI DËK BI JAYYONTE
SELLEBE YOON LA JAMONO TËREADI FONKAL SA BOP LI NGAY JAKKONTE
BU LA KEN DEF JAAAM TUKKI DU TEKKI FEPP LA METTI
LABBALI FAS BUUMU GACCE NGA TEKKI
XALIS DAFA NGANDE LAMIÑ CI JAMONO DËGG NE PATT
DOOLE POCHES AK CARTE GAB MOLAY WAXLO MOYTUL BËTTU XOL BI PÁTT
PAAKA CI PUTT BUMU TAX NGA BONN XOLAL FU SORRI BUL JADD KOÑ
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMONO LA
JIKKO JAMO... JAMONO LA JAMONO LA JAMONO LA JAMONO
JIKKO JAMONO LA

Commentaires

Veuillez vous connecter pour commenter
Vous écoutez
Ce site utilise des cookies pour fournir nos services et pour vous montrer des annonces pertinentes et des offres d'emploi.      En utilisant notre site, vous reconnaissez avoir lu et compris notre politique de cookie,      Politique de confidentialité et nos conditions d'utilisation. Votre utilisation de nos produits et services,      compris notre réseau, est soumis à ces politiques et conditions.
Compris
loading....