Auteur : OMG
Compositeur : B.Beut
Directed by: Weeflag
Tenues : CHELIEL / StefDeKarda & Wax Fegn
Make Up: Diémé
Producteur Exécutif: DD Records
Distribution : Believe Digital
Deezer : https://www.deezer.com/fr/album/87069042
Spotify : https://open.spotify.com/album/5PIrKFlC42yJPM8m0I7mVN
Retrouvez OMG sur:
Facebook: https://www.facebook.com/omgoumygueye
Instagram: https://www.instagram.com/omg_oumy_gueye
Tweeter: https://twitter.com/oumyomg
Snapchat: omgoumygueye7
Contact: 00221774498714
Email: ddrecordsofficiel@gmail.com
LYRICS
1er COUPLET
Yague na ngamay doflo
Té meussou malako wakh
Sa leep ma saf ba ningay rétané
Nane lay def nga kham ko
Beugue na nga kham ko
Diafé na ma wakh ko
Hey bilay walay
Khol bi nga mome ko
Lo beugue ma done ko
Hey bilay walay
HOOK
Dingama doflo
Yamay beglo
Dingama doflo
Yamay dioylo
REFRAIN
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toii
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toi
Boum bam boum bam boum bam bam
Boum bam boum bam boum bam bam
2ème COUPLET
Moussouma wone guem ni
Mbeuguel dina dokh souniou digueunté
Sama khol bi rek nga kheuy keuf
Ba foumala guiss sama fiite def teuf
Fouma meuneu nek
Mane may sa yeuf
HOOK
Dingama doflo
Yamay beglo
Dingama doflo
Yamay dioylo
REFRAIN
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toii
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toi
BRIDGE
Ayéeéé héhéééé
Beugue nala sama khol bééé
Ayééé hééhéééhééé
Beuguenalaaaaaaaaaaa
Refrain
Mon coeur fait boum bam boum bam dakh yaw (mon coeur fait boum bam bam bam bam bam bam bam hey)
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toii ( bam bam bam bam bam bam hey)
Mon coeur fait boum bam boum bam
Dakh yaw
Mon coeur fait boum bam boum bam
Pour toi
Mon coeur fait boum bam ( boum bam bam bam )
Mon coeur fait boum bam ( bam bam bam
Mon coeur fait boum bam
Pour toi pour toi
Mon coeur fait boum bam ( boum bam bam bam )
Mon coeur fait boum bam ( boum bam
Mon coeur fait boum bam
Pour toiiiiiiiiiii
OMG
DD Records han
Han han
Lady boss
Ose serie
#OMG_Oumy_Gueye #Lady_Boss #DD_Records
Veuillez vous connecter pour commenter